Jahman Xpress - Wax Ma Allo Lyrics | AfrikaLyrics
2019-11-12 · Wax Ma Allo Lyrics by JAHMAN XPRESS. Sms la sa numb, woté si sa numb. Dieulo sa téléphone louma la def girl. Say sama cardiologue yoré sama commande xol. Mangui wadia crise té décroché go sa call. Bobou ba légui mangui lay wo yaw ngua khothie ma. Si loss bi moma sonal ba moudiou khothie ma. Dieuleul sa call ma puce dafa risteul.
Get Price